#jahyanté the EP
Douma Bayi : ce sons nous parle de persévérance , de s’accrocher car toute chose vien à son heure y croire peu importe les obstacles.
Faire attention aux vices drogues et tentations croire en quelque chose et s’y tenir
#mbir mou nék si wakhetome
#mbindef Bou nék liy natome
Liriqs
Never douma bayi keur keuri boye G neu try
Soudé job day faye no more mane douma tayi
Dokhe si bars yi yek ARAF amouniou limite nguir yeguaa takhe nioune try di try eny eny time gisgua ni thiacutéfa takhe
Kéndou féthieu si yalla na dé
Liguey fayékou wér bou dé
Kou nek ak sa ndis dawale sa biz sans salaire yi papoter
Boye yi tracer paqueter dèm dik fagou wate dou tè
Dougn meussa douté nioulouke si téyé
Warlou si fagou wateko téyè
Hé dokhe sigui wékeu lep fa god amoule raguale dara one waye
Wer iji step by step niou diokhe diangue diongou tay G neu wër
Batay niou try mouye geun di keung
Niake thieur gui done li first
Sa entourage dou pil dou face
Si galou khathie dé laniou céd
Warna takhe ngua doli diom
Optimiste dokhe ba dé si geum
Li yéné di nèkk oumpou fi kén
Warale kaniane dh mofi diekh
Niane yallah bour bi maye niou
Sante mou doli kome bi wër
Mbir mou nék si wakhetome
Mbindef bou nék ak li natome
Hooks
Yague mome bawoul dara
Kheuthieu bou dagoul dikkeu
G neu ting
Keur keuri gor gor Lou waye
G neu fight geum ni dina bakhe
2 couples
Liniou yotou keur keuri yalna done li geun si nioune
Daw dém jeuli liniou mome try sa thiabi bountou kome
Foumou meneu nék lofa meneu dathie geum geum moye takhe ngua dadjie ko
Dokhe di gis lambe daj viser am sama cible loumou sori sori
Vision si loye dougou
Persévérance dikoy doundou
Kou jeule yone agua fèss sa khôl
Bania tayi moukou dekeu di bay sa war
Équilibrée nguir ngua kheuy mou natte
Diafé diafé yi bess ngua kheuy mou matte
Moytou yonou Bliss i whisky diotayou bitchs weed yi
Degeul diobeul one my way
Le aboie la caravane passe amoule lén louniou barer dou fipeu dou fëm dou tours de passe passe
Ndegue sereukh yi fi tégué ni
Defoul lén dima yokou pass pass
Soul kêr douko téré fégne
Louné fangue kéndou ko diékh
Douniou tayi bayi khadi neggers daniouy dém ba thioki fin
Fegue bountou dougou dadjie jihad si thiacutef yi roote si
Niane yalla bour bi may niou sante mou doli
Kome bi ak wër
Mbir mou nekk si wakhetome
Mbindef bou nek li natome
Hooks
Yague mome bawoule dara
Khethieu bou dagoul dikk
G neu ting
Keur keuri gor gor lou way
G neu fight geum ni dina bakhe
Outro
Yague yague bawoule dara
Yague yague bawoule dara
Yague yague bawoule dara bawoule dara bawoule dara

- Category
- Music auto

Be the first to comment