Geun Di Dém Geun Di Giss

12 Views
Published
@ Geun Di Dém Geun Di Giss : parle des vices de la société, des problèmes liés au crise mondiaux , les sectes les milieux occultes, l'infidélité, les crises politiques ,les dirigeants par défauts etc

Liriqs

Niawtéf nguay gis fake new faits divers
Lomotif aye shit gor jiguén lesbiennes
Town bou beuri niombé
Balegui niogui si boumap diame
Niou geun di dém di geun di gis
Am dieukeur am farr
Bolé niake diome ak réwe
Ay coup bas faut débat
Programme you amérdant
Ministre charlatans députés you arrogeant
Wakhe sa xalate guissané soigne tout
Nieupa wope
Que des bobards dof doflou done Richard fi kou sérieux tocar
Warale niéne gnie guéde gemeu tou niou téki sen réwe
Diangue ak diangualé mi thiole parhieu mi saukhe
Wakhe ma louy dokhe
TikTok Instagram bisbou nèk ay choc
Ndakarou beuri ay dof you niodi class begue flach
Gni am di am ! Gni niake G neu torokhe
Bénéne onde laniou bis fréquence bi deuké sousse
Téré téré mou teu mame néna bayill mou gis
Soul bouki souli bouki Galsen di G neu raflé ni ganarr gouniou souki
Diokhongne louki justice
Pedophile ak franc-maçon geun di roubé mime réw
De toute façon lepa bidon warale gnie geume di geun néw
Yakar taas xol yi froicé balegui ça casse
Town tek xél nirok mouss wethiécoup ay fass
Dou yagui gis
Dadjou bi di geune di ladiou ni si cona bi
Niou geun di dèm di geun di giss
Jiguén di diayou gor di siff
Halam ni niss dem di tis dèréte di tisse wedi gis nieupa khif sisse sik
Larra bi dou art bi déf up dé si war wi
Mouslou thie sathieu bi si car bi ak diague bi si bar bi
Dou war wi ladi feel dé si milles walla diogui mine
Ak yén thiép yi niaka nine si yéne thien
Stress def mégn si xèl yek si xol yi
Si gél yék si gor
Déf reup si yén bor yi
Nékh ba kéndou wory
Koufa nekoul dagn lay wowi i am sorry
Lucide men yé togué né si bopou kogn bi sori like so feel
Hip like na Burn in ak hop dadjie yi Gun in
Petite sœur yi pathiale grand frère yi di padiale
Li lép ndakhe niaka geum geum
Xol yi dém ba kheum kheum

Hooks

Yeah
Niou geun di dém di geun di gis
G N di dém
G N di dém di gis
Bép khetou crise mofi dadji xplose
Si guéni dém
Si nguéni gis
Kou wat wathieu nédou sif
Niawtéf lay geun di sik iow
En niou geune di dem
Di geun di gis
Niou geun di dém di geun di gis gis gis
Category
Music auto
Be the first to comment